Goneg nit ku nuul gi - L'enfant noir-version wolof (Grand format)
- Essais littéraires
- Laye Camara
- Lettres
Date de parution
12/10/2007
Editeur
L'Harmattan
Format
Grand format
Kamara Laay a ngi fekk baax Gine. Bindkat la. Mu ngi juddoo Kurusa, dëkk bu ndaw ci Penku-Gine, ci 1 fan ci sanwiyée, atum 1928. Ba mu wàccee daaraay tubaab, mu dem Konaakiri, péey ma, topp njàngam. Ba mu amee C.A.P. ci wàllu metkanise, mu jéema doon eñseñoor ca Faraas, àntuwut. Booba la Kamara Laay, fekk mu tollu ci ay jafe-jafe, génne «Goneg nit ku ñuul gi» L'enfant noir, di téereem bu jëkk, ci 1953 teg ci, at ci gannaaw gi, «Bëtu buur bi» Le regard du roi. Ci 1956, ca jamano ja Gine di waaja moom boppam, mu dellusi Konaakiri. Foofu, ba 1963, mu yor fa ay sas yu am solo ca ministère de l'information, laata muy gàddaay dem Senegaal ndax tàng-diine ga féeñoon ca nguurug Séeku Ture te mu doon ko ñaawluji ci 1966 ci «Daramus» Dramouss, téereem bu mujj.
Moom ba-tey, moo bind "Borom kàddu" Maître de la parole, ab taataanu léebi géwél yuy nettali cosaanu Mali, Kamara Laay a ngi gaañoo Ndakaaru, 4 fan ci feewaryée, atum 1980.
Auteur(s) | Laye Camara |
---|---|
Traducteur(s) | Jean-Léopold Diouf, Stéphane Robert |
Date de parution | 12/10/2007 |
Nombre de pages | 163 |
URL Ebook | https://e-librairie.leclerc/product/9782296472174_9782296472174_4 |
Dimensions (cm) | 14 x 22 x 0.9 |
Editeur | L'Harmattan |
Poids du produit | 190 g |
Format | Grand format |
EAN | 9782296035096 |
Type de litterature | Littérature Française contemporaine / Texte en langue originale |
Genre (littérature) | Lettres |
Des millions de
références en vente
Cumulez des Tickets
retrait gratuit en magasin
Tous vos produits
à prix E.LECLERC
Paiements
100% sécurisés
Options de livraisons du produit
En stock
Options de livraison
Sélectionnez votre mode de livraison préféré
Livraison standard à partir de 3,99€ - Prévue le 23/07/25